BM
Lova
Intro
(....)

AlyGhost
Baby kay kay, gneuwal bilay gnou dem
Fo dioxogn ma daggal la, indi visa gnou dem
Boul topp say-say bi takh ngamay bye bye
Xeuy souba wone ma dokk, newoma sax bye bye
Diaral ngama die, deukei sango lou tangu
Watou ngandi nel, nela kong ma wangg
Deugu leu, tarou nga te amga wang
Boumu takh nga djitou, di bayi ma langg

BM
Wethioma ak kenen nakh nama way
Woutina lenen teksi nima, bye bye
Man mi ko toude tchapali, mou defma li dh dem dh bayima
Bett nama nak dh, waye baby man dh gueunalouma
Mougn leu done lou impossible
Deuk di guent c'est pas possible
Yay sama cible xale bi boula nekhe fireul
Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof

Refrain
Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof
LOva, Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof
Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof
Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof
Lova Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof, ( baby kaay..)
Lova Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof, ( baby kaa aa aay)
MoOntee
Check you jungling your big booty, is my higher fantasy
And just, thinking about it, make my heart gninga gningaling
I swear my baby you blew me
And then you'r driving me crasy, really
Let me be the man who'll change your whole life sweetly
Am gonna make you smile, show leu sama life style
Together we gonna be happy then will fly high
Go beu doubaii, feulei Haway tiimm haters yeup nilen Hi!
Baby girl kay, lets touch the sky nagnko try

BM
Fi nga beugu yem ak man beugu ma bayi man mi
My lova kay gnou langg, kay gnou ande free

AlyGhost
Kay gnou ande fethia, nagn tadiabone
Kay gnou ande fly dound lebone lepone

MoOntee
Haaha,you told me bye bye, could you please tell me why? ( why)
Sett nala facebook ak tweeter, te guissoumala skype

AlyGhost
Kay gnou wahtane, bougnu nekk noone
Dougu pentagone, ma door leu fone
Souba beu ngone, nekk dila bomba
Koula diema bomb, ma door ko gun
BM
Jah lova bulma setane, boulma bayi man mi
Noone yangui retane diapalema cii..,

MoOntee
Ya really even know, you are my lova
Don't turn me back baby take me ova
Yay sama sadiobatt, rafete beuri filing pathie
So beugone weer bi sakh honey doumaci tekk baaaaatt