BM
Ndakaru njay’
INTRO (...)

BM
Aythieu léne niou dém biir ndakarou ndiay

AlyGhost
Town bou néx leu diarou di wax bilay

BM
Mane mi deuk diko weur diko weundélou mbay

AlyGhost
Taax na secteur bo dougou amnagn fa waay

BM
Diar Xaar yalla

AlyGhost
Yow teulé dji Hann

BM
Wathei Yarrakh

AlyGhost
Dieulé fa gaal
BM
Ngor Yoff la moudié

AlyGhost
Wouté fa thiof

BM
Dialeu Almadie deuk lékeu katou Sause

AlyGhost
Diar Plateau téne séne Gorée
Wachie Sandaga di déme
Séré sama cap, dém dougou Médina Mermoz Ouacam, dougou Colobane
Hlm castor, Dox feul Big Yoff akssi Patte D'oies, cognou sans loi
Parcelle Guédiawaye ana wa Pininay Boy Town dou rérr biir Ndakaru Ndiay

Refrain
Naniou Dem Dem Dem (naniou dem)
Naniou Dem Dem Dem (naniou dem)
Souniou town ney bomb fane (laniou dieum)
Souniou tow ney bomb fane (DK)

MoOntee
Welcome welcome to DK my koner
Moy town bou néxa néx ték si dara dou yombe
Xalé you nékh béss, ndiol si kow xéss pétch
Nio nékeu si town bi deukk diko dangaaaal yow (saturday)
Or holydays paradise everyday
Chez Iba iow 'Hey'
Chez Kathia iow, 'Hey'
Nirvana iow, 'Hey'
Calibso iow, 'Hey'
Patio guél yi daniou pathial wéene
AlyGhost
Fi guéy guissé bandi deug figuéy gueuneu mouss

BM
Kou ragal douffi meuneu deuk wala ya fouss

MoOnTee
Aay boy you teng teng, you gueuneu gaw louxouss
Rak tak niou keuf seu guél gueum lo leu yéna bokeu mbouss

BM
Ndakaru ndiay Ndakaru ndiay capitalou Sénégal Ndiaye

Refrain
Naniou Dem Dem Dem (naniou dem)
Naniou Dem Dem Dem (naniou dem)
Souniou town ney bomb fane (laniou dieum)
Souniou tow ney bomb fane (DK)

AlyGhost (outro)
Naniou Dem Dem Dem (ndakaru ndiay )
Naniou dem dem dééé hiyéhi Dem dem dem (ndakarou ndiay)
Naniou dem dem dééé hiyéhi dem dem dem (ndakarou ndiaye)
Naniou dem dem dééé hiyéhi dem dem dem (ndakarou ndiay)
Naniou dem dem déé hiyéhi yéééééééééééé
Walay walay niou dem dakar hey
Bilay walay dakar reu néex hey
Yéééhééé niou dem niou dem ndakaréé walay walay dakareu nékhééé hi yéééxééé......