Falaaw

from Free Season (2015)
Pre hook

Yow kaay niou job ndakh mou tané bro (ndakh mou tané)

Amoul khof talougn saalé sope warougn planer
Kaay niou job ndakh mou tané bro, ndakh mou tané

Amoul khof talougn saalé sope



Hook

Kham na lima beugg (Kham na lima beugg)

Mang koy dound deug (Mang koy dound deug)

Amoul lomay diangal (Amoul lomay diangal)

Bimay eksi séén naala lay niangal (séén naal angay niangal)

Mais yafa niaaw

Falaaw falaaw falaaw (falaaw) x3

Falaaw falaaw



Verse 1

Yow kaay niou job ndakh moui tané bro

Ak liniou dokh war negn garer truck tabakh gallé

Amne woté amatoul kharré bro, amoul kharré

Amoul khof talougn saalé sope, amoul baalé



Yagg diow motakh yaakh ak thiow

Légui dam ci paré

Dakhone fo maala ndieukk dore ak tokh cigarette

Wayé no dama yagg fort mané faut que mou carré

Faut que niou diok

Borom meukh dome

Mounoul khèkh ak armée



Lé-légui soy def liste Elzo'y djiitou

Bougn sanione ma daanou #Metzo Djatah

Légui no def se sista né daf may bisou

Firr dou takh ma waagni sama khadar



Hook

Kham na lima beugg (Kham na lima beugg)

Mang koy dound deug (Mang koy dound deug)

Amoul lomay diangal (Amoul lomay diangal)

Bimay eksi séén naala lay niangal (séén naal angay niangal)

Mais yafa niaaw



Falaaw falaaw falaaw (falaaw) x3

Falaaw falaaw



Verse 2

Yeah

Seme life aka beuri ay signe

Fi meu diare douniou beuré ko sagne

Nekhoul be nekhoul mais beuri na style

Ladial gangor yi ak mbeur yimeu dane



Deungueu diappone dingueumeu stop

Mais deme tangg be time le nga mar

Deme high, deme deep, deme tar

Seme ga yangui deal seme crack

(whoo)

Guiss na ni fi defe khate wayé Free lim fi dji defe sakh

Nenegn le thiow li ngay thiowe ding ko bayi ndakh nioune nioye gni titeul se squadd

Nekk ay killer tchi rap deukké job kharougn 8 heure du mat

Doper na mineur ak mag niou meu diappé me dealer bou mak



Yang may diss (10) may play lou rey comme Zizou

Ngay copier Biggie te se laamign rekkeu paata (heahhh)

Rakk boul di sathieu mère ay bijou

Bou leu aakham dalé c'est la cata !



Bridge

Kham naa lima beugg

Mang koy doundou deugg

Amoul lomay diangal

Bimay eksi seen naala ngay niangal

Mais yaafa niaaw



Hook

Kham na lima beugg (Kham na lima beugg)

Mang koy dound deug (Mang koy dound deug)

Amoul lomay diangal (Amoul lomay diangal)

Bimay eksi séén naala lay niangal (séén naal angay niangal)

Mais yafa niaaw

Falaaw falaaw falaaw x3

Falaaw falaaw



End

More from Free Season (2015)

More by Elzo JamDong

All Elzo JamDong songs →